As salamou aleykoum wa rahmatoul lah sama mbokk bopp.!
Daniou djiss ni diamono bi ci wattsapp bi, ak ci facebook bi beurei na message yoyy diott gnoulayy wakh nga partagé ko. Bala ngay partagé khamal loy partagé sinon dina la dioureul ay mbougueul you tarr "Yeuwmal khiyam " Leip lougnou neik Yallah kham nako..Bilahi..!
Yallah kham nani message yi am nassi yo kham ni dagno rakh cheytann..!
Souniou yaguei lire yèneu message yi leigui suniou iman wathie..gnou bayi fii Yallah, deim diko weur fénènn..!
Jeune génération bi meunou gnou détecté lolou...Cette génération est en danger !!! Par ce que ay mboukki you mboubbo dérou kharr dagno fii beurei...Donc vous les jeunes faites attention !!!
Tei le pire moy so keu wakhei..gnounei da nga compliqué wala tu vois le mal partout, wala tu n'as rien compris, wala c'est juste une blague, wala dangayy diayy oustaz, wala deggo dinei ..ay you démé nonou..
Wakh bi may wakh sakh dina am gnou keu beugu contredire, louma ci meun dara mais naniou yéwou neilaw bi doyynaa..!!
Ramadan bi leigui mou diékh, demandons-nous koor gui laan laniou ci dieulei ? Sougn ci dieulei woul yokoutei ci dinei, djikko you bakh naniou kholatt suniou boppou...
MESSAGE BI NASSI NIEUP DIOTT INCHALLAH GUIR SAUVER, GUIR GUIDER AK LEIREUL JEUNES YI..!
Yalla naniou yallah may djiss djiss bou lèer gnou meuneu rangnei...bijahi Rassoul lahi Sallal lahou aleyhi wa salam ..!! Amine
N'envoyez pas de message ayant un ton agressif
ou insultant.
N'envoyez pas de message inutile.
Pas de messages répétitifs, ou de hors sujéts.
Attaques
personnelles. Vous pouvez critiquer une
idée, mais pas d'attaques personnelles
SVP. Ceci inclut tout message à contenu
diffamatoire, vulgaire, violent, ne respectant
pas la vie privée, sexuel ou en violation
avec la loi. Ces messages seront supprimés. --
Pas de publicité. Ce forum
n'est pas un espace publicitaire gratuit.
Pas
de majuscules. Tout message inscrit entièrement
en majuscule sera supprimé.
4 Commentaires
Anonyme
En Juin, 2017 (09:06 AM)Anonyme
En Juin, 2017 (09:06 AM)Anonyme
En Juin, 2017 (09:24 AM)Reveillez-vous
En Juin, 2017 (11:24 AM)Daniou djiss ni diamono bi ci wattsapp bi, ak ci facebook bi beurei na message yoyy diott gnoulayy wakh nga partagé ko. Bala ngay partagé khamal loy partagé sinon dina la dioureul ay mbougueul you tarr "Yeuwmal khiyam " Leip lougnou neik Yallah kham nako..Bilahi..!
Yallah kham nani message yi am nassi yo kham ni dagno rakh cheytann..!
Souniou yaguei lire yèneu message yi leigui suniou iman wathie..gnou bayi fii Yallah, deim diko weur fénènn..!
Jeune génération bi meunou gnou détecté lolou...Cette génération est en danger !!! Par ce que ay mboukki you mboubbo dérou kharr dagno fii beurei...Donc vous les jeunes faites attention !!!
Tei le pire moy so keu wakhei..gnounei da nga compliqué wala tu vois le mal partout, wala tu n'as rien compris, wala c'est juste une blague, wala dangayy diayy oustaz, wala deggo dinei ..ay you démé nonou..
Kouffi wakh deugu gnounei wokho deugg, kouffi wakh ay nakhei ay nitt guèneu dila défendre.! Lii kènn khamoul foum gnou dieumei…
Politicien djoguei feulei nieuw dignou sonnal ci ayy campagne électorale, thi ayy khékh, nékkeu di yéh fiit neu..!!! Politicien you beurei sèn intérêt bopp lagnouyy défendre, mais intérêt REWMI kou kayy défendre !?
Keippeu kouma wakh wakh bou ndiagass balnala ci khol bou seiddeu gouyy, damay khamni reik dagua khamoul, Keippeu kou nittei sou djissei deugu rangnei ko.. !
Wakh bi may wakh sakh dina am gnou keu beugu contredire, louma ci meun dara mais naniou yéwou neilaw bi doyynaa..!!
Ramadan bi leigui mou diékh, demandons-nous koor gui laan laniou ci dieulei ? Sougn ci dieulei woul yokoutei ci dinei, djikko you bakh naniou kholatt suniou boppou...
MESSAGE BI NASSI NIEUP DIOTT INCHALLAH GUIR SAUVER, GUIR GUIDER AK LEIREUL JEUNES YI..!
Yalla naniou yallah may djiss djiss bou lèer gnou meuneu rangnei...bijahi Rassoul lahi Sallal lahou aleyhi wa salam ..!! Amine
Participer à la Discussion